Загрузка страницы

Daaraj Family- Yaamatele,Couleurs Tropicales

#DaarajFamily #yaamatele #yamatélé

Yaamatele
New Album Yaamatele available : https://daarajfamily.lnk.to/Yaamatele
Daaraj Family On line :
https://www.instagram.com/daarajfam_o...
https://twitter.com/daarajfamily
https://www.facebook.com/daarajfamily...
Yaamatélé lyrics:
tere tere
Arrête, arrête
tere tere tere
arête arrête arrête

Tere tere tere tere...!!
arrête arrête arrête arrête !!

Tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui qui brave l’interdit voir
Tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui qui brave l’interdit subir
Tere tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui brave l’interdit voir
Tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui brave l’interdit subir
Ééé Yaamatele yaa ngi sàcc film bi
Eéé Yaamatele tu nous caches quelque chose
Ééé Yaamatele àdduna bi du nii
Eéé Yaamatele ce n’est pas ça la vie
Ééé Yaamatele yaa ngi sàcc film bi
Eéé Yaamatele tu nous caches quelque chose
Ééé Yaamatélé àdduna bi du nii Eéé Yaamatele
ce n’est pas ça la vie

Looy def léegi fey ko encaissé cash
le mal que tu fais aujourd’hui se paie cash
ku di dëgër bopp keppu ci caas
la tête de mule tombe toujours dans un piège
Dugg ci loo xamul lu ne nga laal
s’engager dans le flou toucher à tout
Da nga wowle yaa ngi tëmb ci mbaal
toi le terrible tu t’es retrouvé dans les mailles du filet
Lu ndoxe nga bëgg bëggoo dox ci dëgg
tu aimes trop la facilité tu n’aimes pas être dans le vrai
Fi nga dëgg bés di nga sëgg
tu finiras par avoir honte en persistant dans le mal
For bu yombee dafay jafe nga këdd (sëgg)
s’il est facile de ramasser difficile est de rester longtemps courbant l’échine
Doo ñeme lu metti ban bunt ngay fëgg
tu n’es pas endurant, quelle porte vas-tu frapper ?
Bës bouton nga tal de robot la tane de
Tu ne fais qu’appuyer sur un bouton tu es pire qu’un robot
Doo def dara Yaamatele
Tu ne fais rien Yaamatele
telekommaand a la jiite nga défile modd bi siiw la ni tulleek maale esclave de la télécommande tu fais le célèbre défilé de mode dans le vacarme
Xaalis ngay lijjanti Defkatu déli
tu te débrouilles pour avoir de l’argent, délinquant
Toppandoo seef de bandit Makavelli
suivant les pas des chefs de bandits Makavelli
Al capone jamaïquin bi ci belly
Al capone le jamaïcain qui est dans Belly
Tele tàkk na yaa ngi télli-télli
la télé allumée, tu es trop agité

Tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui qui brave l’interdit voir
Tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui qui brave l’interdit subir
Tere tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui brave l’interdit voir
Tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui brave l’interdit subir
Ééé Yaamatele yaa ngi sàcc film bi
Eéé Yaamatele tu nous caches quelque chose
Ééé Yaamatele àdduna bi du nii
Eéé Yaamatele ce n’est pas ça la vie
Ééé Yaamatele yaa ngi sàcc film bi
Eéé Yaamatele tu nous caches quelque chose
Ééé Yaamatélé àdduna bi du nii
Eéé Yaamatele ce n’est pas ça la vie

Waxi waajur takk ko téere du yendu
Prends au sérieux les conseils des parents tôt ou tard
Bay fanaan ci àll ba
tu verras leurs fruits
Boo deful li la war bés di nga mere sa bopp
Si tu ne remplis pas tes devoirs tu ne t’en prendras qu’à toi-même
Su booba bët dina taa
en ce moment-là tes larmes couleront
Goru loo yattuloo amuloo xottu
tu es au chômage tu n’as rien
bëgg fi ñoddi life'u superstar
tu as la folie des grandeurs passant pour une star
Guddee àll topp ci see bi
Te couchant tard en faisant la bamboula
àndandoo yu bonn tambaambalu ba fajar
avec de mauvaises fréquentations à errer jusqu’à l’aube
Dëgg rakk yaa ngi dëbb ndox
En vérité mon frère tu perds du temps
Sa tànk na nga dëgg dox
Marche d’un pas sûr
Itte yu koweek farata
avec de hautes préoccupations dans l’essentiel
so bañe dëkk ci ñu lay jox
si tu veux toujours avoir raison
Dëgg la ndaw dañ ko wara dox
C’est vrai que jeunesse se passe
Waaye ku ko topp torox
Mais en être l’esclave te rendra malheureux
Suxeet muxeet fuñ la fekk
fumer des joints tout le temps
yaa ngi daaju làng ba doo mën a dox
tu es saoul jusqu’à te couper les jambes

Tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui qui brave l’interdit voir
Tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui qui brave l’interdit subir
Tere tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui brave l’interdit voir
Tere tere mu të bàyyil mu gis
laisse celui brave l’interdit subir
Ééé Yaamatele yaa ngi sàcc film bi
Eéé Yaamatele tu nous caches quelque chose
Ééé Yaamatele àdduna bi du nii
Eéé Yaamatele ce n’est pas ça la vie
Ééé Yaamatele yaa ngi sàcc film bi
Eéé Yaamatele tu nous caches quelque chose
Ééé Yaamatélé àdduna bi du nii
Eéé Yaamatele ce n’est pas ça la vie

Видео Daaraj Family- Yaamatele,Couleurs Tropicales канала Daaraj Family
Показать
Комментарии отсутствуют
Введите заголовок:

Введите адрес ссылки:

Введите адрес видео с YouTube:

Зарегистрируйтесь или войдите с
Информация о видео
12 июня 2020 г. 9:20:44
00:05:10
Яндекс.Метрика